musicas.mus.br
Letras de músicas - letra de música - letra da música - letras e cifras - letras traduzidas - letra traduzida - lyrics - paroles - lyric - canciones - YEKSIL REMIX - YOUSSOU N'DOUR - música e letra
Utilize o abecedário abaixo para abrir as páginas de letras dos artistas
Yeksil Remix letra
Gëjoon fi lool bi nga ñëwee
Bi nga ñëwee
Duma fàtte nit nitam
Mooy garabam
Bokk nga ci ñi
Bokk nga ci ñi ma gën a bëgg
Hi hii hii
Koŋ- Koŋ, yegsil daal
Koŋ- Koŋ, yegsil daal
Koŋ- Koŋ, yegsil daal yegsil daal
Koŋ- Koŋ, yegsil daal
Yegsil avec plaisir
T'amènes que de beaux souvenirs
Waxtu wu la neex
Mën nga fëgg
Fii doo fii gan
Bu nu waxantee dëgg daal
Bokk nga ci ñi ma gën a bëgg
Koŋ- Koŋ, maa ngi xaar
Pressé d'entendre ta voix
Biig rekk, sax j'ai pensé à toi
Gëjoon fi lool bi nga ñëwee
Gëjoon fi lool bi nga ñëwee
Nee naa la, nee naa la, nee naa la
Bismi, bismi, bismillaah
Gëjoon fi lool bi nga ñëwee
Nee naa la, nee naa la, nee naa la
Bismi, bismi, bismi, bismi, bismillaah
Koŋ- Koŋ, Yegsil daal
Yegsil avec plaisir
T'amènes que de beaux souvenirs
Waxtu wu la neex
Mën nga fëgg
Man de xam naa
Ne sa fëgg yaw
Bokk nga ci ñi ma gën a bëgg
Man de damaa gis ci yaw sincérité
Dellu gis ci yaw, woyof ak dal
Moo tax ma yàkkamti sa jotaay ak sa ree ju neex
Man de damaa gis ci yaw sincérité
Dellu gis ci yaw, woyof ak dal
Moo tax ma yàkkamti sa jotaay ak sa ree ju neex
Ñëwal saa yu la neexee sa ñëw
Man da fa may dundal
Man de damaa gis ci yaw sincérité
Dellu gis ci yaw, woyof ak dal
Moo tax ma yàkkamti sa jotaay ak sa ree ju neex
Youssou N'dour - Letras
- 7 Seconds
- Ay Chona La
- Ballago Ndoumbé Yatma
- Be Careful
- Benn La (The Same)
- Biko
- Birima
- Bul Nangu (feat. Mbaye Dièye Faye & Bilahi)
- Confession
- Cruel Crazy Beautiful World
- Da Fa Laa
- Dem
- Dunya
- Fay Bor
- Gorée
- Habib Faye
- How Come
- In An African Passageway
- Kids
- La Cours Des Grands
- Leaving (Dem)
- Li Ma Weesu (As In A Mirror)
- Ligeey
- Mama Africa
- Mame Bamba
- Mariama (The Turtle Dove)
- Mool (Deglu Météo)
- My Hope Is In You
- Olel (The Echo)
- Oté-fê (feat. Alpha Blondy)
- Set
- Seven Seconds Away
- Shaking The Tree
- So many men
- Song Daan (feat. Akon)
- Thiely
- Things Unspoken (Lees Waxul)
- Toxiques
- Waññi ko
- Wax ju bari
- Xale Bi
- Yeksil Remix
- Youssou Madjiguene
top 30 músicas
©2003 - 2026 - musicas.mus.br